> Sons

daara j family - Sénégal


SENEGAL by #daarajfamily

Jom mooy dém waayé fulay ñibbisi Jambaar dawul doolé ladoon wuti yagg naa bittim reeeeew ñibbisi naaaa sama reew Senegal #Senegal #Senegal #Senegaaaaaaaaaaal

J’aime ce Pays qui m’a vu grandir cette terre qui a vu mes premières larmes et mes fou rires Pas besoin d’un crayon pour dessiner les sourires Tels des rayons de soleil pour t’accueillir le Cfa parle fort à travers et à tort On marchande pour le transport et Quoi encore… ici il n’y a pas de métro pas de Tram(way) ici c’est Taxi-brousse, jeaune-noir cars-rapide, ndiaga ndiaye ou Pousse-pousse Petite pause dans une Dibiterie ou Tangana Petite tintamarre c’est du Tama « Dakar ne dort pas » elle danse avec ou sans salaire Malgré les coupures d’électricité , d’eau et la Galère une pensée pour les frères qui ont coulé dans l’Atlantique meme si j’ai la chance de revenir ma blessure est authentique Nul n’est prophète chez soi mais on est mieux que chez soi c’est vrai j’ai duré labas mais mon coeur était là senegal

Jom mooy dém waayé fulay ñibbisi Jambaar dawul doolé ladoon wuti yagg naa bittim reew ñibbisi naaaa sama reew Senegal #Senegal #Senegal #Senegaaaaaaaaaaal

Fila reew néexé Sénégal ngi dé booko soré dooto bëgg ludul Ñibbisi dé bofi ñëwé joxé mbok néla kaay ñu gissé ana lo inddi tay daañ la yen say xarit yaggon toog di Xaar di séntu bis bi Mi ngi Ñëw na tay no dikké serica yi nga diggé séntu nañla fin d’année été doyul daggal billet att bilé giss mbok yilé summi yërré immigré Metro boulot amul Dodo jogg bala jant bi Modou modooo ñu ngi daw wuti wuti bitim reew bañ fa futi ubbi buntu xéwal bis fok ñu ñibbi mu ngi guddi sorri nga dëkkuwaay géntal ñulay téeru bis di nga délluwaay yoon wi na nga léer lu Xamal né jéggé na njaboot gi ñëppa ngi xaar démoon nia ñëwaat nga Senegal mooy sa képaar

Le courage de partir La force de revenir Partir pour grandir Revenir pour bâtir dans la grisaille et le froid J’entendais ta voix ,me Revoilà chez moi là ou je me sens comme un Roi Senegal…Senegal…Senegaaaaal

Jom mooy dém waayé fulay ñibbisi Jambaar dawul doolé ladoon wuti yagg naa bittim reew ñibbisi naaaa sama reew Senegal #Senegal #Senegal #Senegaaaaaaaaaaal

KAFFRINE SEDHIOU THIÉS LOUGA DIOURBEL SAINT LOUIS MATAM KOLDA KAOLACK KEDOUGOU TAMBACOUNDA ZIGUINCHOR et DAKAR -Senegal Senegal Senegal

KAFFRINE SEDHIOU THIÉS LOUGA FATICK SAINT LOUIS MATAM KOLDA KAOLACK KEDOUGOU TAMBACOUNDA ZIGUINCHOR et DAKAR-Senegal Senegal Senegal

Répondre à cet article