> Sons

DAARA J FAMILY - BAYI YOON (paroles)


Africa

Je suis Africain

REFRAIN : ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon jikko you rafét yignou ragnéwoon ? dafa melni dagnou bayi sougnou yoon beugeu askano lougnou momoutoon deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon oh !!wow !! Africains et fiers de ce que nous sommes Africains et fiers de ce que nous sommes

COUPLET :

fier d’être africain je suis je suis africain donc je suis mes ancêtres ont souffert le martyr pour que je puisse relever le défi c’est à moi de porter le flambeau ils ne peuvent pas me mettre en lambeau pour me mettre k.o. il faut minimum une armée de cent mille(100000) rambo Dis à ton prof d’histoire qu’il raconte des histoires,la plus grande des civilisations est Née en Afrique noire. L’ afrique a inspiré le monde avec ses pyramides sa science et ses mathématiques Ses symboles et ses signes Elle créa l’écriture avec les hyérogliphes du temps des pharaons tu ne me crois pas Demande à akhenaton... (de dakar à marseille)

REFRAIN : ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon jikko you rafét yignou ragnéwoon ? dafa melni dagnou bayi sougnou yoon beugeu askano lougnou momoutoon deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon oh !! wow !! Africains et fiers de ce que nous sommes Africains et fiers de ce que nous sommes

COUPLET :

Dafa melni gnou ngi daw jeum fénén ni wacc wacc nagnou ande yi xéeb sougnou ngande yi fékki borom jikko you dande yi/ fo daw fo daw di nga wirri ndaari fa nga jougé fi nga dooré fila wooré doufou sorré/ AFRO sama dolé na nga mako xolé geum sama démb doon nittou téy njaxass ni xéetou parfum’k’Gowé/ Africains koula xass foy gnawé/ Africains xola gneup nignouy ngaangé/ Africains soy joug doufi gawé/ koula xol dina séet fan la lay ngagné/ geum sa bopp xam fi nga bokk melni garab réen banxass ak xob/ dougnou fatté fignou jogé ndakh panafricanistes délo sougnou xél démb kanamou mame gnou giss/ dimbali jam yi biss- gnoul métisses dékkil osiris -carbone14 souliwaat gnou giss- histoire bindaat grand pére ba petit fils bamako singapore anghata !!!

outro : sAMA GAA GNA NGI DOOMU AFRICA MBEUR LA KAAMIL YAGG YAGG DINA DAANI CI Gééw KéN DOUKO JAMNAANI NéNAALA SAMA GAA GNA NGI...

© Daara J Family

Répondre à cet article